(Translated by https://www.hiragana.jp/)
Xayra — Wikipedia Aller au contenu

Xayra

Jóge Wikipedia.
Sumbu 4 Sattumbar 2009 à 12:41, bu: Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru) (Tuddewaat nañ Kayro léegi mooy Xayra)


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Kayro لقاهرة
Skyline of {{{official_name}}}
Réew  Isipt
way-dëkk 17 856 000 nit
atum way-dëkk 2 009
Rëyaay 210 km²
Fattaay 38 221 nit/km²
Gisub Kayro

Xayra (ci araab لقاهرة Al-Qāhira) mooy péeyu réewum Isipt, mooy dëkk bi ëpp nit ca goxub Afrig. Donte Al-Qāhira mooy tura dëkk waaye, lu bari, dees na ko wax itam, ci araabi waa-isipt, misr di Isipt ci araab.